PlumePerdue
28/05/2026
Baal leen ma àq ngir Yàlla🙏🏿
Baal leen ma sama gàtt xel
Samay bataaxel yu bari
Ak samay yëgle yu àndutak nuyoo
« Kon Yàlla miy maye yaakaar,
na def ci seen xol mbég mu réy
ak jàmm ju yaa ci seen kaw ngëm,
ba ngeen am yaakaar ju mat sëkk
ci dooley Xel mu Sell mi . »
Waa Room 15.13
Dewenati Baal leen ma Àq
Baal naa leen
Yàlla na boroom bi boole nu baal❤️🙏🏿
PlumePerdue✍🏿
❤️
07/05/2026
🥊 PERFORMANCE — KEMBAARU S**I
📍 Départ : Monument Guet-Ndar
📍 Arrivée : Quai Roume, en face du Bateau Bou El Mogdad
🗓 Samedi 16 Mai
🕕 18H18
Une traversée entre slam, souffle et résistance.
TeamPlumePerdue Get Ready ❤️🔥
🖼️: .studio
02/05/2026
Ay junniy S**i dekki
Ma làmboo leer
Kembaaru S**i ⏳
02/05/2026
Moom mi waroon a falu te faluwul xanaa du su bëree war naa daan
Kembaaru S**i ⏳
📸:
02/04/2026
Alhamdoulilah Back to the Ceebu Jën🇸🇳❤️🙏🏿
Ramatu ma wëriwoon dellusi na mbaar njaay.
15 jours de rencontres, de découvertes, d’immersion, d’amour , de partage et de poésie.
Je remercie du fond du cœur toutes les belles âmes qui de près ou de loin ont rendu possible cette expérience.
Mention spéciale à mes frères et pour toute la générosité et la disponibilité. J’ai envie de vous dire que : qui ouvre son coeur à un derviche, ouvre sa maison à Dieu. Yàlla na leen Yàlla taxawu ni ngeen ma Taxawoo❤️🙏🏿
🇫🇷 à bientôt et pour de plus beaux souvenirs ❤️
Cliquez ici pour réclamer votre Listage Commercial.
Type
Contacter la personnalité publique
Téléphone
Site Web
Adresse
745 Rue De France
Saint-Louis