Vision Mourides
21/12/2021
*Journées de zikrul Lâh à Touba* les 17 et 18 jumâdal Ûlâ 1443.h/ 22 et 23 décembre 2021 sur recommandation du khalif général des mourides cheikh Mouhamadou Mountakha MBACKE. *En direct sur tous les réseaux sociaux internationaux.*👉👉👉
10/04/2021
Serigne touba doy na si lislam bépp exemple ndax bagn kou guisss ba bagn koy nopé guiss taloul loudoul boromam ak ligueyal yonentè bi
Lim fi nék lépp kéne kouné ték na si sa beutt.
Nék na si biir diaam gni diglé na lam warone déglé wax na lam warone wax défna lam warone déf. Serigne Touba lam noufi bayil tamit lolou rék la diamou yalla liguéyal yonenté bi dieuf diou baax sah si daakke sunu diguenték diaam gni té lolou mane na sauvé niépp
War na niou délo sunu xél si serigne touba xam lako fi indi wone xam lim fi néké wone xam lim noufi bayil
Parole de Serigne Mountakha
Discours magal Touba 2017
Cliquez ici pour réclamer votre Listage Commercial.
Contacter l’organisation
Site Web
Adresse
Dakar