2n Vision
11/11/2024
Meeting de soutien à la liste PASTEF organisé par UNAP- Transports : pour une majorité parlementaire absolue au soir du 17 Novembre 2024
Meeting de soutien de l'UNAP- Transports à la liste PASTEF : pour une majorité parlementaire absolue
07/03/2024
Man Abou Salimata DG 2n Vision Guinaw bima santé YALLA bu baax ak diko gueureum, mangui sant Safir services ( contacts : +221771167878 ou +221338942799 - email : [email protected] ) thi ndjiteul Président Directeur Général bi Safir FayeOfficiel ci koluuté gui, djappandal gui ak yenen yima munul wax.
Agence bu boolé hébergement bu diaar yoon ak guides religieux you am xam xamou Charia ak expérience Hajj ak Oumra, foo tollou rek ñu djangal la langa fa wara dèf ci jaamu YALLA ak histoiram ci anam bouy yokkou sa diiné.
Mouy Makkah di Madinah yepeu hôtel bou djègué HARAM bi lay djeul nguir ñèppeu di meuna djoullè dji thia ñaari djakka ya.
Yaw mi beugg Hajj wala Oumra yènél rek lissi dèss lèppeu Safir services mookoy dèf
services : Ayez juste l'intention et on s'occupe du reste.
23/02/2023
Oustaz Mor KÉBÉ || Lèral leunti bèn Ahmadi ak ñi gueum ni am na benen Yonenti guinaw YONENTIBI ﷺ Soyez Membre pour soutenir DEGDINE, nékal membre nguir japalé DEGDINE :https://www.youtube.com/channel/UC2bhcgS6aEfs68bDTUBhJ0w/joinYoutube : https://www.yo...
27/11/2022
Oustaz Oumar DIALLO || football ak carte xaliss gui thi nèkeu : parifoot ak yenen yi dafa haraam.
Oustaz Oumar DIALLO || football ak carte xaliss gui thi nèkeu : parifoot ak yenen yi dafa haraam.
14/11/2022
Oustaz Mor KÉBÉ || Rester endurant et constant sur la vérité || mougn ak sakh si deug
Oustaz Mor KÉBÉ || Rester endurant et constant sur la vérité || mougn ak sakh si deug
Cliquez ici pour réclamer votre Listage Commercial.
Contacter l'entreprise
Téléphone
Site Web
Adresse
Dakar